Confidence d’ une femme« Je sors avec l’imam de notre quartier, dafma beug teudé maniko Yallah beugoul lolou mouné ma… »

C’est en publication en anonymat que cette femme s’est confiée aux internautes d’une page Instagram.

Voici son texte !!!

« Je suis une femme divorcée de 36ans. Dama nekk di geneu ak beneu imam il a 58ans douma wah bane kogne la deug wala noumou toudou mbala nioukoy Hamm mais sama kogn ham léne ni sène wadji desna geumm yalla ak limouy waraté yepp. Je sort avec l’imam du quartier dafma beugg takk niarel. Mais da amm louma diahal ci mom a plusieurs reprise il essaie de coucher avec moi. Soumako wahé yalla beugoul ndiallo mou merr mou nane hamna loussi yalla wah ak loumou wahoul. J’ai décidé ma bayi relation bi mou sedd mbala ma deff Lou eupp bi imam diahal Nama«

vous pourriez aussi aimer
Laisser un commentaire

Votre adresse email ne sera pas publiée.