Senegal Direct | Actualité au Sénégal – Actualité Sénégalaise

Nécrologie – Triste Nouvelle ! Touba et toute la communauté mouride en Deuil …( Photo)

0

Sëriñ Cheikh Mbacké Ibn Serigne Modou Faty khary, Ibn Sëriñ Masamba ñoo ngi ñaan Yàlla ubbil ko bunti àjjana yi, ci barke Sëriñ bi.Weer wi mu dem rekk dal na xel, te wone na li mu nekkee woon ci kaw suuf, ku manoona dimbalee, rafet xol lool, te jaboote ñépp, baay la woon, nijaay la woon di Maam ci man. Yalna daje ak gaayi Yàlla ya ak ay maamam ca Firdawsi

Toutes nos condoléances à toute la communauté mouride.

Laisser un commentaire

Votre adresse email ne sera pas publiée.