Senegal Direct | Actualité au Sénégal – Actualité Sénégalaise

Propos de Moustapha Diakhaté – La Réaction de Serigne Mbaye SY Abdou »nitt dana ligueye ligueye ligueye bamou soti rek lepp yakou »

0

» Nitt dana ligueye ligueye ligueye bamou soti rek lepp yakou «
» kouy wakh si seydina mouhamed ba yeukeuti sa kadou sa lepp yakou «
Mbok yi nagnou am yar tei respecte kignou yalla bolel mouy seydidouna Mouhamed nga khamni mo geune gneup, waydiouram bou goor ak bou djiguene gno geune sougnouy waydiour ndakh sougnouy waydiour diourou gnou kou melni salalhou aleyhi wasalam.

Laisser un commentaire

Votre adresse email ne sera pas publiée.